Inicio Bad Bunny Canciones Religiosas Taylor Swift Ed Sheeran Luis Fonsi Ozuna Daddy Yankee J Balvin Maluma DMCA

Escuchar música y letra de Xel Akk Xol de Ashs The Best - Escucha y canta NewMusicas

Artist profile picture

Xel Akk Xol

Ashs The Best

Canciones

Yeah, eh eh eh
Lé, lé, walé
Hum, hum

Suba su ma yeewu
Yaw laay bëgg jàkkaarlool
Saa su ma yeewu
Yaw laay bëgg njëkk xool

Ëllëg lu mat a soor la
Waaye xel xalaatu ko
Ëllëg ay jaar-jaar la
Sama xol yëgoon na ko muy ñëw

Xel xalaat la (xel ak xalaatam ba)
Xol yëg-yëg la
Nit ak jëmmam ja
Dara xaaju fa

Saa su ma yeewu
Yaw laay bëgg njëkk xool
(Su ma yeewu yaw laa bëgg njëkk xool)
Fajar su ma yeewu
Yaw laa bëgg jàkkaarlool

Denk naa la guddi
Fanaan yakkar ci yaw
Gent naa la guddi gi yëpp
Ndax fajar yaw lay jàkkaarlool
Mbëggeel

Xel xalaat la
Xol yëg-yëg la
Nit ak jëmmam ja
Dara xaaju fa

Nit ak jëmmam ja
Dara fa xaajul

Más de Ashs The Best

20 canciones
  • Yàlla
  • GIVE UP
  • Sutura
  • Ñibisil
  • Yalla
  • Goor
  • Ngala Way
  • Maa Ngi Dem
  • Yaakaar
  • sutura
  • Yeurmande (feat. Kya Loum)
  • Xalam
  • Ayway Samba
  • Guddi
  • AYUBES
  • Alxames (feat. ILAM)
  • Goor
  • Yaay Joor (feat. Obree Daman)
  • 4010 Session #4
  • Wétoon Na
  • Inicio Bad Bunny Canciones Religiosas Taylor Swift Ed Sheeran Luis Fonsi Ozuna Daddy Yankee J Balvin Maluma DMCA